
Lan mooy xLingua?
- xLingua juumtukaay bu matale bu bees la ngir ngirum-barillàkk
- xLingua daa nar a dimbali nit ñi ci yombal jëfandikook yeneen làkk yi
- xLingua amna jokkalekaayu tëraliinu boppam
- xLingua ag jàppandal la ngir sos ci ag matal jumtukaay i làkk yu bees
- xLingua barab bu ubbeeku la ngir njuréefu xalaat yu bees yi
- xLingua dëkk bu bees la
xLingua - ag jàppandal ñeel nit ñ?
- xLingua day dimbalee ngir nànd ak a jubbanti sa bopp ci yeneen làkk yi
- xLingua Wu-Almaañ ak Wu-Poloñ la dooree
- xLingua dina jàppandiji ci wu-Fraas ak wu-Riis ci diir bu néew
- yéene ji ñeel yeneen làkk yi bér na.
xLingua - yoon wu bees ngir ngirum-barillàkk
- xLingua sàqum-njoxem làkk mu xarale la
- xLingua man naa joxe ay tekki yu wuute
- xLingua nangu na araf i seet yu jéllalewu yi
- xLingua nangu na seet i yàqu-yàqu yu jéllalewu yi
- xLingua day dellu ci soppikuy baat yu digg-dóomu yi
- xLingua nangu na yokkalek baat jaare ko ci benn soppikoom
xLingua - jokkalekaayu tëraliin bi
- xLingua amna jokkalekaayu tëraliinu boppam
- xLingua may na bépp tëraliin ci jëfandikoo man-manu ngirum-barillàkk
xLingua - daytal ñeel juumtukaay i làkk wu bees
- xLingua mooy daytalu juumtukaayu tekki gu jonjoo gixLingua yëgle
- xLingua maye na juumtukaay i jàng làkk wu bees
- xLingua maye na dajale yu bokk ak i baatukaay yu solowu
- xLingua man naa taxawu njàngum kenn
xLingua - ubbeeku na
- xLingua ubbeeku na ngir dugalug njuréef i xalaat yu yees
- xLingua ubbeeku na ngir tëral ci .Net walla Barabu Java [environment]
- xLingua ubbeeku na ngir xam-xamu anam ci luy yokk juumtukaayi làkk
- xLingua dina yokk ci diir bu néew ngir di génne kàddu
xLingua - dëkk bu bees bi
- xLingua may na tëralkat yi, saytukatu-làkk yi ak ñeneen ngir ñu defar séen juumtukaayi làkk i bopp
- xLingua moongi woote ci ag jagleel ngir defar ay tëriin yu yees ñeel politig, koom-koom, cosaan ak lépp lu ñeel dundug nit.